CHANT RELIGIEUX
CHORALE
DES RESSORTISSANTS DE
LA
PAROISSE SAINT PIERRE JULIEN
EYMARD
DE KOUDIADIENE A DAKAR
SAS LA CI MAN
T et M : André M. TINE
Refrain :
Ay atan-gi ni tey julien nena krista b waw moy
degga gi sax sax
Bulen ragal (bulen ragal) bulen ragal (bulen ragal)
yen ñi mu yeba lon mbokgaxu
Koudiadien sas la wu mu len sas : teralal
ko yalla baay kuko topa do to taabi muk ci lëndëm
Couplet 1-
Mbo-ta-yu koudiadien tey ji le dalal jama
sagosi tabax na te mu batale ko won pier
julien Eymard
Couplet 2-
Ay at an gi ni tey xibar bi niirna fi ñun
sagosi tabax na te mu batale ko won pier
julien Eymard
Couplet 3-
Dinala tero woy bi mati be suma xol
sagosi tabax na te mu batale ko won pier
julien Eymard
A Lazare, Jean Pierre
et Yvone TENE à l’occasion
des 150 ans des pères
du Saint Sacrement
Inscrivez-vous au blog
Soyez prévenu par email des prochaines mises à jour
Rejoignez les 117 autres membres